Video Xel Akk Xol de Abdoulaye Sy 2025 Lyrics Lyrics

Escucha la música Lyrics más popular de Abdoulaye Sy y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2025 en Musicas-Cristianas de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Xel Akk Xol » Abdoulaye Sy Letra

INICIOAbdoulaye SyXel Akk Xol

Abdoulaye Sy - Xel Akk Xol Lyrics


Yeah, eh eh eh
Lé, lé, walé
Hum, hum
Suba suma yeewu
Yaw lay bëgg jakarlool
Sa suma yeewu
Yaw lay bëgg njëkk xol
Ëlëk lu mata soor la
Wayé xel xalatu ko
Ëlëk ay jaar-jaar la
Sama xol yëgoon nako muy ñëw
Xel xalaat la (xel ak xalatam bë)
Xol yëkk yëkk la
Nit ak jëmëm jë
Dara xaaju fë
Sa suma yeewu
Yaw lay bëgg njëkk xol
(Suma yewo yaw la bëgg njekk xol)
Fajar suma yeewu
Yaw la bëgg jakarlool
Denk na la guddi
Fanané yakkar ci yaw
Gent na la guddi gi yëpp
Ndax fajar yaw lay jakarlool
Mbëggël!
Xel xalaat la
Xol yëkk yëkk la
Nit ak jëmëm jë
Dara xaaju fë
Nit nak ak jëmëm jë
Dara fa xaajul

Xel Akk Xol » Abdoulaye Sy Letras !!!
ANUNCIOS PUBLICITARIOS
Esta sitio web no aloja ningún tipo de archivo audio o video© Musicas-Cristianas 2025 España | Chile - Argentina - México. Todos los derechos reservados.

Escuchar músicas enlinea gratis, 2025 Escuchar Música Online, Música en Línea 2025, Música en Línea Gratis, Escuchar Música Gratis, Música Online 2025, Escuchar Música

Música 2025, Música 2025 Online, Escuchar Música Gratis 2025, Músicas 2025 Gratis, Escuchas top, Música de Moda.