Ne na ma yeen góor ñépp yem (yeen ñépp yem)
Ku ngeen gis fowe ko dem (fowe ko dem)
Bala ma dee ngeen di fen (yeen ngeen di fen)
Jigéen bëggul fowe, je t'aime (yeah)
Moo tax ñu leen di mbaraan
Miin nañu façon doxaan
Yàq xol rekk ngeen tamm
Maa bañ awma seen temps, góor
Ne naa la duma ñee (duma ñee)
Dama am ci yaw cofeel (yeah)
Waxuma la lu dul mbëggeel
Man ay fo indiwuma fii bae
Sama xol yaw la tànn
Yaa ma daqal aljanna (yeah)
Yaay Michelle maay Obama (yeah)
Xanaa teel a kontaan
Yaw dee ma ree
Ñu ànd bëggante mbëggeelu indo
Li nga bëgg ak li ma bëgg mingoo (mingoo)
Kaay ñu bëggante mbëggeelu indo
Li nga bëgg ak li ma bëgg mingoo
Ehh, pain au lait
Ohh, pain au lait
Pain au pain au lait
Ohh, pain au lait
Pain au pain au lait
Ohh pain au lait
Pain au pain au lait
Ohh, pain au lait
Pain au pain au lait
Pain au pain au lait
Yaw dañoo nuroo tek tek
Damay ragal bëgg lekk lekk
Bëgg essayer yéeg
Mais xel bi ne ma déedéet
Sama xol tëdd perpect
Gis naa lu may séet
Te dinga ma bëgg bañ bañ
Tekk na ci sama bakken
Wala dinga ma ray bokk
Boo dawul duma daw ngone lat Latir Diop
Li du xeetu door
Man a duma ñoom
Fokk nga ni ñun ñépp ñoo yeme
Non man ak ñoom duñu benn
Noooo
Diggante sa yaay man nga fay tek (yeah)
Monogamie man rekk jege (yeah)
Watt ko Yàlla lay dégg (yeah)
Waxatuma lool
Hummm, waa est-ce que yar do navigateur
Non danga romb mool
Pain au lait ñu diw sunu bëre
Xëbbël sama xol
Wante bëggante mbëggeelu Indo
Li nga bëgg li ma bëgg mingoo (mingoo)
Kaay ñu bëggante mbëggeelu Indo
Li nga bëgg ak li ma bëgg Mingoo
Ehh, pain au lait
Ohh, pain au lait
Pain au pain au lait
Ohh, pain au lait
Pain au pain au lait
Ohh pain au pain au lait
Pain au lait
Pain au pain au lait
(Kaay ñu bëggante mbëggeelu Indo)
Pain au pain au lait
(Li nga bëgg ak li ma bëgg mingoo)
Pain au pain au lait
(Kaay ñu bëggante mbëggeelu Indo)
Pain au pain au lait
Ohhh pain au lait
Pain au pain au lait