Video Ya Tay Feat Wally B Seck de Baye Mass 2024 Lyrics Lyrics

Escucha la música Lyrics más popular de Baye Mass y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2024 en Musicas-Cristianas de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Ya Tay Feat Wally B Seck » Baye Mass Letra

INICIOBaye MassYa Tay Feat Wally B Seck

Baye Mass - Ya Tay Feat Wally B Seck Lyrics


Yéwwu ci sa wet doy na mbégte
Jàkkarlook sa kanam doy na bànneex
Love bi may yëg ku ko mën téye
Ana ki ko saañ jaral na ma xeex
Soo bëggee nak mu sauvage baby
Soo bëggee nak mu doux, loo def yaa tay
Dis-moi ce qui t'arrange bébé
Jafandu na ci sa branche, mbëggeel bu xeere

Yéwwu ci sa wet doy na mbégte
Jàkkarlook sa kanam doy na bànneex
Love love bi may yëg ku ko mën téye
Ana ki ko saañ jaral na ma xeex
Soo bëggee nak mu sauvage bébé
Soo bëggee nak mu doux, loo def yaa tay
Dis-moi ce qui t'arrange bébé
Jafandu na ci say branche, mbëggeel bu xeere

Ci sa wet duma bàyyi
Ak lum mënti doon
Bul ma yërëm, dee ma gaañ
Takk sama loxo
Yaw sa allure dafa gaaw
Ku ko lekk fott
Même soo tooñe bul ma baalu
Loo def daf may neex, yaa tay!

Soo ma tooñee, yaa tay
Reewantul sax, yaa tay
Ku ci dugg moo ci des
Ma baby yaa tay

Soo ma tooñee, yaa tay
Reewantul sax, yaa tay
Ku ci dugg moo ci des
Kon baby yaa tay

Man de bëgg naa (yaa tay)
Loo wax mu neex (yaa tay)
Yaw danga taaru, danga jékk, danga nice (baby yaa tay)

Sa doxin rafet na (yaa tay)
Man bëgg naa (baby yaa tay)
Loo def mu neex, xam na ding ma mës a gaañ
Bëgguma ñuy réeroo
Waxumalaak tàggoo
Sama cofeel ci yaw wor na ma
Nob naa la man, eh-eh ya

Show me your love my baby boo
Sama safara, ma seytaane
Everything my love knocks me down
Rocc sama geñoo jox naa la ko

Ah dissah deep love fidi gyal dem
Dem ennemi mana ready fi shoot dem
Mi love is over all, why a mi ready fi evathing

Baby yàgg na, man dama pare
Ndiggël xale bi jaral na ma xare
Mi love is over all, why a mi ready fi evathing

Ci sa wet duma bàyyi (ma baby boo)
Bul ma yërëm dee ma gaañ (mon bébé à moi)
Sa allure dafa gaaw (ma baby boo)
Même soo tooñee bul ma baalu (mon bébé à moi)

Soo ma tooñee, yaa tay
Reewantul sax, yaa tay
Ku ci dugg moo ci des
Ma baby yaa tay

Soo ma tooñee, yaa tay
Reewantul sax, yaa tay
Ku ci dugg moo ci des
Kon baby yaa tay

Hum
Show me your love, ma baby boo

Ya Tay Feat Wally B Seck » Baye Mass Letras !!!
ANUNCIOS PUBLICITARIOS
Esta sitio web no aloja ningún tipo de archivo audio o video© Musicas-Cristianas 2024 España | Chile - Argentina - México. Todos los derechos reservados.

Escuchar músicas enlinea gratis, 2024 Escuchar Música Online, Música en Línea 2024, Música en Línea Gratis, Escuchar Música Gratis, Música Online 2024, Escuchar Música

Música 2024, Música 2024 Online, Escuchar Música Gratis 2024, Músicas 2024 Gratis, Escuchas top, Música de Moda.