Lu mu ma wax ma di ko def
Dafay dëkk ci di ma tooñ
Teg si ma naan ko baal ma
Waaye moom la nob
Su ma ko gisee
Samay bët di mellax
Samay tànk jaxasoo
Sama lammiñ réer ma
Moom laa nob
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou
Damay gëm loo lu amul
Terewul ma di ko gëm
Tég ci ma naan ko baal ma
Waaye moom la nob
Su ma ko gisee
Samay bët di mellax
Samay tànk jaxasoo
Sama lammiñ réer ma
Moom laa nob
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou
Saa yu ma jege woote téléphone
Ci téléphone bi lay yéndu
Saa yu ma jege ab setsi
Ma yendoo wajal
Xam naa ni nob na keneen ku dul man
Oh yeg na ni mi ngi seeti keneen ku dul man
Waaye moom laa nob
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (may ma Amadou)
Amadou, Amadou
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (sama yaay may ma Amadou)
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (sama yaay may ma Amadou)
Amadou, Amadou (geestu ma)
Yaw sama yaay (sama yaay may ma Amadou)