Video Tukki Du Tekki Feat Fou Malade de Ashs The Best 2024 Lyrics Lyrics

Escucha la música Lyrics más popular de Ashs The Best y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2024 en Musicas-Cristianas de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Tukki Du Tekki Feat Fou Malade » Ashs The Best Letra

INICIOAshs The BestTukki Du Tekki Feat Fou Malade

Ashs The Best - Tukki Du Tekki Feat Fou Malade Lyrics


We gonna fight for your right
Fight for your life, for your freedom
Dund ci ndool bëgg ci geen
Fii goor akk jigeen ñëpp a bëgg fas jom

Tukki du tekki, tekki du tukki looy utti
Yakamti xamoo looy fekki, yoon bëgg nga tekki
Am-am ñu gënël am teggin
Dëkk ci dëkk bi nga tekki fi moo jafe
Tax ñu xaddi, ga′ddaay fu sori baayi njaboot gi
Mënu ñu dëkk ci ndool yeewoo xonet we need money
Teed tax ñu jël yoonu geej gi

Jooy na jooy na ngir gisaat la
Woy naa la brother
Jooy naa la Baaba
Nothing, nothing to hide
My people die young ndax bëgg tekki

Jamano ji ñu toll ñëpp a saalit ja'mm amul
La′mbaay rafeta gul
Batay Waalo naata gul
Tukki gënëllu ñu waaye ligeey moo fi amul
Reew mi ndaw la ñakkul
Ku na'mp ci Maam Ndey nga gisul

Nothing to hide
My people die young
Fii ñëpp bëgg tekki
Nothing to hide
My people die young because of immigration

Fitche' duul xam fii dara amu fi
Fii ku fi amul dara ken dula tekk nitt
Su ma xasee dugg kaaw doo tu ma dellusi
Rap naa junni att gisu ma ci we′ccit
Sa′cc sama gaz or dima tere visa
Ma'nk sama pe′trole dima naxee pizza
Mënu ma ci d'accord faut que je dis ça
Tampon passeport tekki takk Lyssa
Bëgga tuma toog fii njiit ñi dima politig
Foog ma dugg avion calmer sama solitude
Nang ma wax waxu kaaw boo ma bëggee disturb
Di naa mësa radical jël gun ray ñëpp

Tukki taxul noflaay
Toog ci reew mi ligeey gën woor
Ñaata ndaw ñoo ga′ddaay
Tekki tax ñu ba fi li ñu moom
Tukki taxul noflaay
Toog ci reew mi ligeey gën woor
Ñaata ndaw ñoo ga'ddaay
Tekki tax ñu ba fi li ñu moom

We gonna fight for your right
Fight for your life, for your freedom
Dund ci ndool bëgg ci geen
Fii goor akk jigeen ñëpp a bëgg fas jom

Nothing to hide
My people die young
Fii ñëpp bëgg tekki
Nothing to hide
My people die young because of immigration

Tukki len gis
Ja′ngi len xam
Tukki len gis

Tukki Du Tekki Feat Fou Malade » Ashs The Best Letras !!!
Esta sitio web no aloja ningún tipo de archivo audio o video© Musicas-Cristianas 2024 España | Chile - Argentina - México. Todos los derechos reservados.

Escuchar músicas enlinea gratis, 2024 Escuchar Música Online, Música en Línea 2024, Música en Línea Gratis, Escuchar Música Gratis, Música Online 2024, Escuchar Música

Música 2024, Música 2024 Online, Escuchar Música Gratis 2024, Músicas 2024 Gratis, Escuchas top, Música de Moda.