Ñibbisil
Ñibbisi-i-il
Jukk du wess, jukk du wess
Su ma lay woo lu tax doo ma faale?
Wax ma lu dañ ci man xanaa bëggetoo ma
Yeah, yeah
Bëtu mbëggeel la la mës a xool la
Lu waral man ak yaw, ñu dëkk si coow
Su ma xoolee fu ñu jaar yépp
Dagg ma woowoon di ma def fu sori
Bi ñuy goro loxam wax ma
Tay biti bi moo lay gërëm kër gi jooy triste
Samba alar waaw si njaboot ji
Xol yaa ngi jooy, xar yaa ngi jooy
Ñaata at man ak yaw ci kër gi
Bi ma lay tànn boobu xalaatoo dinga séy si
Soxna si sétal si Yàlla ji nga xol si biti
Gisoo sa moroom bu ne si séy ba pare ne si
Mbedd mi njaboot moo muccoo
Lu fees nak si xol su ëpp tuuru
Muñ na ba s¨s taxul nga xam li xol bi jiyunju
Daje n'a lu ne gir yak ak njaboot ji liñuye dundu
Fi may dundu gis naa lu ne ms taxul ma xàddi
Bànneex man dégg la si am
Coono ak naqar tax ma géj nekk si jàmm
Wax ma lan nga bëgg si lan gane
Talatoo ma talato sa kër gi wax ma noy def ak njaboot gi
Wax ma man ak yaw ku tan
Fépp foo xam na ngi mafa clamé
Bateau dem bateau costé mënoo ma tere xolli kaneen
Lépp loo ma yakkul danga ko fàtte
Su respect jexe mbëggeel dem yoonam lu ñu dese lu dul
Samba alar waaw si njaboot ji
Geestu war naa la samba alar nga
(Xol yaa ngi jooy xar yaa ngi jooy)
Ñi nga bëggantel ñoo ngi sa ginnaaw
Yeah, yeah
Su ma lay woo nga ni doo ma faale
Su ma lay woo, oh oh
Xanaa nobatoo ma?
Su démb doonoon tay
Ma joxaat a sama mbëggeel?
Su démb doonoon tay
Ma joxaat la sama xol bi mbëggeel bi
Su ma lay woo nga ni doo ma faale
Su ma lay woo, oh oh