Video Kaay Kaay de Narah Diouf 2025 Lyrics Lyrics

Escucha la música Lyrics más popular de Narah Diouf y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2025 en Musicas-Cristianas de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Kaay Kaay » Narah Diouf Letra

INICIONarah DioufKaay Kaay

Narah Diouf - Kaay Kaay Lyrics


Xool la si bët xol di ko yëg
Xel bi sori yénne ji bari li mbëggeel la ko laal
Hey, su de ay gént buñ ma yee
Li de moo daq neex di ma cooqotaan may ree

Hum, kaay kaay
Yaw rekk laa love
Kaay kaay
Yaw rekk laa nob

Yaw, yaw, yaw laa nob
Yaw, yaw, yaw laa nob

Su mbëggeel doon jaay may jënd
Lépp lu ma laaj ma jox ko
Te soo bëggee dëgg-dëgg
Sama xol bi yaa koy fëgg
Jox nga ma sama gédd
Baby sa love lañ ma sedd
Ci lay dundu ba tedd
Te boo ma jegee xol bi sedd

Kaay kaay
Yaw rekk laa love
Kaay kaay
Yaw rekk laa nob

Yaw, yaw, yaw laa nob
Yaw, yaw, yaw laa nob

Dama la, dama la, dama la nob
Ba bëgguma lu lay gaañ
Soo ma soree dina ma sonal
Sa mbëggeel la may daan

Kaay kaay
Yaw rekk laa love
Kaay kaay
Yaw rekk laa nob

Yaw, yaw, yaw laa love
Yaw, yaw, yaw laa love

Kaay Kaay » Narah Diouf Letras !!!
Esta sitio web no aloja ningún tipo de archivo audio o video© Musicas-Cristianas 2025 España | Chile - Argentina - México. Todos los derechos reservados.

Escuchar músicas enlinea gratis, 2025 Escuchar Música Online, Música en Línea 2025, Música en Línea Gratis, Escuchar Música Gratis, Música Online 2025, Escuchar Música

Música 2025, Música 2025 Online, Escuchar Música Gratis 2025, Músicas 2025 Gratis, Escuchas top, Música de Moda.