Video Tegguil Sa Tank Feat Bilou Xiv de Narah Diouf 2025 Lyrics Lyrics

Escucha la música Lyrics más popular de Narah Diouf y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2025 en Musicas-Cristianas de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Tegguil Sa Tank Feat Bilou Xiv » Narah Diouf Letra

INICIONarah DioufTegguil Sa Tank Feat Bilou Xiv

Narah Diouf - Tegguil Sa Tank Feat Bilou Xiv Lyrics


Life bee changé
Wala jikko yee yàqu, yee yàqu
Loo xamal ké yol
Ok wax nga ba tarde
Léegi ñépp lay moytu, lay moytu
Mu ngi bëgg ñaaw de

Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk ey, ndànk ey, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk

[Narah Diouf]
Ey fi la réew mi tollu
Ñi de cas lañuy topp
Lu tokk sa nopp
Fel sa gëmmiñ, lépp tuuru
Kon mu ngi tokk
Céy li nga bokk
Tekk ko si suuf
Balla moo souss

Ok yaa ngi si TikTok
Doo raté Facebook
Snap nga flamme cas bi
Whatsap nga yénou coow li
Ok bàyyil ni nga nekke
Li du sa métier
Bul topp sa xol
Waxal prarara

Life bee changé
Wala jikko yee yàqu, yee yàqu
Loo xamal ké yol
Ok wax nga ba tarde
Léegi ñépp lay moytu, lay moytu
Mu ngi bëgg ñaaw de

Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk ey, ndànk ey, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk

Bàyyil libeurou jaambur di topp sa kilo
Yaw xoolal sa bopp, teggil sa nopp
Bàyyil sopp, soooof!
Shhhhh

Ya raw mor ndaje
Doo raté daje
Kuy dem yóbbu la
Fuñ dem fekk la

Life bi de concourou tekki là
Ku yeex ñu bala fa
Jàppal fils te bul bàyyi
Fattal té bañ a teppi

Fatal ma foofu bu dara percé
Tëbbel ma teup ñu ànd percer
Liggéey rekk di encaisser
Kassé

Life bee changé
Wala jikko yee yàqu, yee yàqu
Loo xamal ké yol
Ok wax nga ba tarde
Léegi ñépp lay moytu, lay moytu
Mu ngi bëgg ñaaw de

Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk ey, ndànk ey, ndànk
Teggil sa tànk
Ndànk, ndànk, ndànk, ndànk, ndànk

Tegguil Sa Tank Feat Bilou Xiv » Narah Diouf Letras !!!
Esta sitio web no aloja ningún tipo de archivo audio o video© Musicas-Cristianas 2025 España | Chile - Argentina - México. Todos los derechos reservados.

Escuchar músicas enlinea gratis, 2025 Escuchar Música Online, Música en Línea 2025, Música en Línea Gratis, Escuchar Música Gratis, Música Online 2025, Escuchar Música

Música 2025, Música 2025 Online, Escuchar Música Gratis 2025, Músicas 2025 Gratis, Escuchas top, Música de Moda.