Warna niou woné mbolo, warna niou woné freedom
Kou done laathie faramareen, faramareen, faramareen nieuw na
Yéna ngui dég louné, wéraneté, xééx, xoulo nguir man
Souma sanione kéne kounék setsila niou naan ataaya
Beug yalla ko deff thi diaamam
Beug ngama, beug naala (ooh yeah)
Yéne gni beug faramareen teudeul nélaw yalla baaxna
Kone sopé sopé kaay, yaw kaay
Di lén wayal mbékté leu bou reuy thi man
Ma sopé sopé lover don't cry
Di lén wayal mbékté leu bou reuy thi man
Warna niou woné mbolo, warna niou woné freedom
Kou done laathie faramareen, faramareen, faramareen nieuw na
Warna niou woné mbolo, warna niou woné freedom
Kou done laathie faramareen, faramareen, faramareen nieuw na
Hey yow sama sopé
Boul di xoulo, boul di xééx, Yalla nopina
Yalla yaa na, Yalla baaxna
Maa léén gueuna love
Maa léén gueuna yeuk
Maa léén gueuna gueum
Maay ki leu xam
Maay ki leu beug, ouh!
Force à toi sopé
Force à toi sopé