Video Henne Time Feat Ndiole Tall de Wally B Seck 2025 R B Lyrics

Escucha la música R B más popular de Wally B Seck y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2025 en Musicas-Cristianas de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Henne Time Feat Ndiole Tall » Wally B Seck Letra

INICIOWally B SeckHenne Time Feat Ndiole Tall

Wally B Seck - Henne Time Feat Ndiole Tall Lyrics


Chérie sama xol
Billaay wallaay chérie yaa ci nekk
Humm
Chérie sama xol
Yaw la like chérie yek ci na
Lay loo xamati ci buñul bëggee
Muy sama def différence sunu yaay ji

Chéri bu la neexe jugal taxaw ricc sa digu
Te xam ni ki la Yàlla boolel ne na yaw la bëgg
Yaw ba nga yeksi la xel mi dal yaw la aimé
Xam nga ni bés bi moom la yàgg bëgg
Moom demul dikkul outoul xarit yaa ko ci doy
Kon du la weccoo ak lennen ndax yaa ko teral!
Wax ji bariwoon na découragewul yaa ko siggil
Kon dina la sëyal ba de ndax yakoko ji
Xaar bi yagona mu tok di muñ li la xamoon
Na nga ko dëkkel, dëkkoo ko ndax moo ko liggéey

Ah! Yaay sama nana lu may doye gune gune
Billaay wallaay sama sweet
Chérie coco fóon ma
Yaw la doon seet te gis naa la
Ak ni ma la bëggee chérie coco ray ma
Bul ragal dara engagé ma nak
Kaay kaay waay, kaay fi ñëw ray ma
Ak reew mi fu mu tollu yaw nga ni man la
Mënuma nelaw dama ame insomnie
Pas d’insomnie baby jugal fer yaa ngi
Soo rayee sama bopp babay damay nelaw
Chérie li ngay laaj dama titel
Cuuraay la ngi!
Foo bëgg ma tégal la ko fa
Duma sëriñtu duma wutu far bu ma ame naqar muñ ko

Mbëggéel moo neex xam na ci dara!

Wura tek danga koy jëm wura tayi ñëw def ci junni
Mo dama ne xale bu jigéen day sakkal boppam matériels
Invitel say xarit nañu ñëw ñu fudënu la yaw wane ko
Say goro tok say ñekke tok ñu sañse ñu fudënu la yaw
Ñun dañuy henne henne mooy fudënu mo sa yaay tok
Sa bàjjen tok
Ndiole di la bëggel
Kaay leen ñu fudënu

Henne time neex na
Xale bu yaroo ame bës
Ma kuti kunte boroom kunte hair braiding
Ak Sukeye gambienne la
Aïssatou Dabo mooy sa yaay
Kunsu Kounté mooy sa baay
Chérie Habib Ndiaye
Jigéenu Wally Seck
Yaayu Modou Sow ak Omar
Ana Khady Lo
Wol ma Adji Ndiaye yaayu Niang xarañ lo
Jigéenu griff
Yaa mu daw sama gambienne bi
Yaa ko fi xar yaw jugal yëgu
Dane koy fudënu dafa réglé
Yaay ja ngi tokk bàjjen yaa ngi
Jamm yi jug leen yegg
Dañoo kontaan ñu ambiance
Yaay boy génal xool sa doom
Sa doom du doomu baadola du doomu coomo
Kaayleen ñu henne
Henne mooy fudënu bës billaay xar
Bës bi yegsi na, xarit yépp tok
Gënal xool sa doom
Sa doom du doomu baadola du doomu coomo

Henne Time Feat Ndiole Tall » Wally B Seck Letras !!!
ANUNCIOS PUBLICITARIOS
Esta sitio web no aloja ningún tipo de archivo audio o video© Musicas-Cristianas 2025 España | Chile - Argentina - México. Todos los derechos reservados.

Escuchar músicas enlinea gratis, 2025 Escuchar Música Online, Música en Línea 2025, Música en Línea Gratis, Escuchar Música Gratis, Música Online 2025, Escuchar Música

Música 2025, Música 2025 Online, Escuchar Música Gratis 2025, Músicas 2025 Gratis, Escuchas top, Música de Moda.