Mi ngui naadj, mi ngui liw
Mi ngui taw, mi ngui neiger
Immigrés ya ngui ci mbéd mii lé
Bayi baay, bayi yaay, bayi dom ak diabar
Fass yéné khouss ci sédd bii lé
Nango door waar
Nango bay sene waar yé
Immigré moy diambaar
Nango door waar
Nango bay sene waar yé
Immigré moy diambaar
Nango door waar
Nango bay sene waar yé
Maa lén séédél li lé
Mi ngui naadj, mi ngui taw
Mi ngui liw, mi ngui neiger
Immigrés ya ngui ci mbéd mii lé
Bayi baay, bayi yaay, bayi dom ak diabar
Fass yéné khouss ci sédd bii lé
Nango door waar
Nango bay sene waar yé
Immigré moy diambaar
Nango door waar
Nango bay sene waar yé
Immigré moy diambaar
Nango door waar
Nango bay sene waar yé
Maa lén séédél li lé
Bing fi diogué yaag neu lol
Té bobak légui meusso taayi ci fadj boumou gaathié yi
Bing fi diogué yaag neu, yaag lol
Té bobak légui meussoulo taayi ci fadj boumou gaathié yi
Lima méti ba méti moy
Leg leg niou sédeulé seu guinaw
Li moka tiiss
Matt naa ci séédé, mane miko doundou
Mou yaag té metti lole
Té nak sakh massa lene thiono
Yene kou lene diourone, yeureum lene (wawaw)
Yow mi mouy yoné, boul xééb
Xamoulo nimou deff ba am ko
Amaana, dadj na thia ay thiono
Nguir meuna bay sene waar yé
Immigré moy diambaar
Nango dor waar
Nango bay sene waar yé
Immigré moy diambaar
Nango door waar
Nango bay sene waar yé
Maa lén séédél li lé
Faaté wouma léne djiguénou immigrées
Am nguéne diorama