Video Thiatt de Samba Peuzzi 2025 Lyrics Lyrics

Escucha la música Lyrics más popular de Samba Peuzzi y otros artistas en línea. Disfruta de las mejores canciones de 2025 en Musicas-Cristianas de música en línea. ¡Encuentra tu canción favorita y escúchala en cualquier momento y en cualquier lugar!

Video Thiatt » Samba Peuzzi Letra

INICIOSamba PeuzziThiatt

Samba Peuzzi - Thiatt Lyrics

Yenewoma diamë xamnako
Yalla xol lay fay, ame na xol
Number one staff for life for (yeah, yeah)
Senegal boy I'′m blessed oh

Ling ma yene douma dal
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu, fing may sentu domfa guiss
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu, ling ma yene duma dall
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu, fing may sentu domfa guiss
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nang ma sexlu (ya ya)

Heyy
Dama make money ba yeksi fii
Life is hard, work hard, play hard
My Momma pray for me
From west Africa, Senegal i'm blessed
Yok jobe, amul tokk, international boy
Yallaa ma may
From the bottom to the top alhamdulilah
Yallaa ma may
Yalla ma mayal xolu muñ samay none yi (nah, nah)
Mokk bul mero, wish you all the best (nah,nah)
Yalla ma mayal xolu muñ samay none yi (nah, nah)
Mok bul mero, do it for the love (yeah, yeah)

Nanani nanani nona, mane deh mangui dëke door war
Nanani nanani nona, bëse dina ñëw sama waxtu diot wah

Yenewoma diamë xamnako
Yalla xol lay fay, ame na xol
Number one staff for life for (yeah, yeah)
Senegal boy I'm blessed oh

Ling ma yene douma dal
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu, fing may sentu domfa guiss
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu, ling ma yene duma dall
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu, fing may sentu domfa guiss
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu

Ko xamul luñ ko boteh
Mandul si mome, niit ku bax day tey
Ko xamul luñ ko boteh
Xamal loy wax si mome, niit ku bax day tey
Bu yallah ne waw lepay changer
Bu yallah ne waw lepay changer (yah yah yah yah)
Yalla deff mafi neh hey (hey)
Monosi dara, xol bu bone nala ray (yah yah yah)
Hey Bot buki, xadj yi mbow hey (wow wow)
Dumalene falleh, I'm on my way ehh

Nanani nanani nona, mane deh mangui dëke door war
Nanani nanani nona, bëse dina ñëw sama waxtu diot wah

Yenewoma diamë xamnako
Yalla xol lay fay, ame na xol
Number one staff for life for (yeah, yeah)
Senegal boy I'm blessed oh

Ling ma yene douma dal
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu, fing may sentu domfa guiss
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu, ling ma yene duma dall
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nangma sexlu, fing may sentu domfa guiss
Thiat, thiat, thiat, thiat
Yall nang ma sexlu

Thiatt » Samba Peuzzi Letras !!!
Esta sitio web no aloja ningún tipo de archivo audio o video© Musicas-Cristianas 2025 España | Chile - Argentina - México. Todos los derechos reservados.

Escuchar músicas enlinea gratis, 2025 Escuchar Música Online, Música en Línea 2025, Música en Línea Gratis, Escuchar Música Gratis, Música Online 2025, Escuchar Música

Música 2025, Música 2025 Online, Escuchar Música Gratis 2025, Músicas 2025 Gratis, Escuchas top, Música de Moda.