Yah
Yah
Yah
Yah yah yah yah
Xalé bu ndaw
Di fayéku xaliss bu tollou ni
Ci diamono dji
Yombul déh (no no no noooh)
No no no no sku bang
Xalé bu ndaw
Di fayéku xaliss bu tollou ni
Ci diamono dji
Yombul déh (no no no noooh)
No no no no sku bang
Ouh
Hey
Xolal, dama nek ci yonn boma wakhoul xaliss rombe ma niii
Guél bingay guéntt lay képp
Mangui ak sama lékhou bébé
Beusseul fiii
Rap bi bou fayoul wone damay bayi lissi dess sama yonn nékoussiii
Shôw yima dann kong nday sann légui gnome gnomay gnane selfiii
Hée xalé bu ndw
Mani bouma
Dioudô grand yoff toukhou diouni yonn
Almadi dou gtt
Sama xoll dou diékh ndakh xaliss bu féss
(Sa valisou mm)
Gnoune gnarr rek ngéne bagne déffo lougnou deff
Amo lougnou ame
Tekk sa wéthiétt gnou bindal la check gnoune dagnou féss billets
Sa poche sangui sétt, sa poche sangui wëtt ni t bi fess djigén
Tekko si temps di bri lou rëy boy dagnou festillé
Aye brick sama down di shopping kaw bayla nga dess Tillène
Xalé bu ndaw
Di fayéku xaliss bu tollou ni
Ci diamono dji
Yombul déh (no no no noooh)
No no no no sku bang
Xalé bu ndaw
Di fayéku xaliss bu tollou ni
Ci diamono dji
Yombul déh (no no no noooh)
No no no no sku bang
Réré tangana déssero pullman lokki likki I'm a pull up
Takal mère or aye kilos
Génération lampe fa
Réwandé xaliss sakoy diaye
Kou ame allale dinga mignon
Bén concert cinq passou doubaï
Album cinq millions
Kou beug ma diaye
Rap bi gnoune leu adounay pottou nda
Ni sollou hausse douma xam néko dou nane
Rap bou yëkh ndieunde auto bu gaaw
Shôw yi hit yi pub bi gnoko fi dakh
Na diémeu siff fi sama lokho la diar
Clash ma banga lathie ma autorisation
Sa guél bi guiss na dédét néko dou gaw
Na dieulate samay photos photowou watt siiii
Bayna thiobu cobbu deureum
Bayna soll baudy mille cinq cent
Gueun la tékki gueun la diékh diame
Op plus t' Hibadere Thiam
Yaye bouma amoul milliard ray ma
Hey rakhass game bi ak détergent
Président la ngay sergent
Wallah arrêter de faire le genre
Xalé bu ndaw
Di fayéku xaliss bu tollou ni
Ci diamono dji
Yombul déh (no no no noooh)
No no no no sku bang
Xalé bu ndaw
Di fayéku xaliss bu tollou ni
Ci diamono dji
Yombul déh (no no no noh)
No no no no sku bang