Hey
Xoolal boy, hey
Bul duggu ci man bul testé déedéet (hein)
Ndax bu ma lay shoot dangay break, naan thiek thiek
Man la gaa yi di fay lu cher yaw weccek
Wër di wax ci man, gwaik gwaik fenn rekk (hein)
Boy fatal ma (hmmm flash, hey)
Tontutuma (hmm clash)
Léegi dama yor (hmm cash)
Waxetuma (hmm am class)
I say back in the days
Meluma woon ni temps yu may jool de
Maa ngi seet, temps yu may jool
Metti woon na loolu, temps yu may jool
Hmm, sant Yàlla, sant Yàlla
Def ndank ndank
Jële ko worses y nekk ci biti (fatal)
Génne gang bi liggéey la laaj du bari tchip tchip (ouh, ouh, ouh)
Dama réew ba yépp xam ni may numério 10 bi (yeah yeah)
Xale yaa ngi laaj "Samba song bi looy wax fi?"
Ma naan hey!
Tus, dara, mbaraj (ouais, ouais, ouais)
Mbaraj, tus, dara
Liggéey ba xar rekk la ko bokkal
Bàyyil ma ubbi dara (hey)
Jël maa ngi leer, may faayeku (ah)
Sekku maak yeen ay fayantu
Hey rappeurs la rappul lool ngeen di laaj
En tout cas soxal mère mang koy si faj
Boy fatal ma (hmmm flash, hey)
Tontutuma (hmm clash)
Léegi dama yor (hmm cash)
Waxetuma (hmm am class)
I say back in the days
Meluma woon ni temps yu may jool de
Maa ngi seet, temps yu may jool
Metti woon na loolu, temps yu may jool
Hmm, sant Yàlla, sant Yàlla
Tus, dara, mbaraj (ouais, ouais, ouais)
Mbaraj, tus, dara
Liggéey ba xar rekk la ko bokkal
Bàyyil ma ubbi dara (hey)
Bul duggu ci man bul testé déedéet (hein)
Ndax bu ma lay shoot dangay break, naan thiek thiek
Man la gaa yi di fay lu cher yaw weccek
Wër di wax ci man, gwaik gwaik fenn rekk (hein)
Boy fatal ma (hmmm flash, hey)
Tontutuma (hmm clash)
Léegi dama yor (hmm cash)
Waxetuma (hmm am class)
I say back in the days
Meluma woon ni temps yu may jool de
Maa ngi seet, temps yu may jool
Metti woon na loolu, temps yu may jool
Hmm, sant Yàlla, sant Yàlla