Thiey li jomi na, jomi na, jomi na
Thiey li jomi na, jomi na, jomi na
I wanna see this girl ayway wan len mako
Kuma ko guissal lum laaj man ma jox ko
I wanna see this girl ayway wan len mako
Fuma ko guissone demm nafa nekku fa
Wanted, wanted (hm hm)
Wanted, wanted lélé (Baba, Baba)
Wanted, wanted (Soxna ci ñëwël ci man kay way ah)
Wanted, wanted lélé (Onyii Packathing)
Mom lay seet guisso ki
Tontu ma mu gaaw waxal way yah yah
Xoćc nama mbeggël I can't breathe
Gennë guñu wayé ma ngui fiir yah yah
(Samba yow amna no mel
Ki nga guiss ko tëy ngani da nga ko nopp
Samba mi amna numu mel
Ki romb fi legui muni dafko nopp)
Thiey li jomi na, jomi na, jomi na
Thiey li jomi na, jomi na, jomi na
I wanna see this girl ayway wan len mako
Kuma ko guissal lum laaj man ma jox ko
I wanna see this girl ayway wan len mako
Fuma ko guissone demm nafa nekku fa
Wanted, wanted (hm hm)
Wanted, wanted lélé (Baba, Baba)
Wanted, wanted (Soxna ci ñëwël ci man kay way ah)
Wanted, wanted lélé (Onyii Packathing)
Hey yeah
Girl girl your body body make me crazy
Teksi da nga bandit bandit sipp nga deal bi
Linguere bu baax soxna ci you so pretty (Hey Packathing)
Jabar lalay def aytia wan ma sa daddy (Onyii Onyii)
Come to me and whine it for me girl (Nananananana)
Come to me and shake it for me girl (Wawawawawawa)
(Samba yow amna no mel
Ki nga guiss ko tëy ngani da nga ko nopp
Samba mi amna numu mel
Ki romb fi legui muni dafko nopp)
Thiey li jomi na, jomi na, jomi na
Thiey li jomi na, jomi na, jomi na
I wanna see this girl ayway wan len mako
Kuma ko guisal lum laaj man ma jox ko

Wanted, wanted
Wanted, wanted
Wanted, wanted
Wanted, wanted